Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi


Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 3

Wideo yi ak waxtaan yi ci xaaj 3

 34 Naka lañu mën a wonee ne bëgg nañu Yexowa?

Woneel sa ngëm bu ñu lay fitnaal (5:​09)

GËSTUL

Nanga bégal Yexowa (8:​16)

Bañal say moroom dugal la ci lu bon! (3:​59)

 35 Ni ñu mën a jële ay dogal yu baax

«Nañu wéy di am xel mu dal» (5:​13)

GËSTUL

Yexowa dafay wommat ay jaamam (9:​50)

Yexowa dige na ne lépp dina baax (5:​46)

 36 Nañu jub ci lépp

Lan mooy yokk mbégte? (Am xel mu dal) (2:​32)

GËSTUL

Nangeen dëggu (1:​44)

Kuy sàmm sa kàddu, jële ci ay barke (9:​09)

 37 Lan la Biibël bi wax ci liggéey ak xaalis?

Liggéeyal ci xol bu tàlli ngir Yexowa (4:​39)

«Deeleen doylu» (3:​20)

Yexowa dina faj suñuy soxla (6:​21)

GËSTUL

 38 Nañu fonk dund gi ñu Yàlla may

Moytul lépp lu mën a lor nit (8:​34)

Nañu fonk dund ni ko Yàlla fonke (5:​00)

GËSTUL

Woy 141: Dund mayug Yàlla la (2:​41)

 39 Ni Yàlla gise deret

GËSTUL

Yexowa dafay dooleel ki feebar (10:23)

 40 Naka lañu mënee nekk ñu set ci kanamu Yàlla?

Yàlla dafa bëgg ñu nekk ñu set (4:​10)

Nanga noot sa bopp (2:​47)

Defal li war ngir wéy di set (1:​51)

GËSTUL

 41 Lan la Biibël bi wax ci séy?

Dawleen lépp luy njaaloo (5:​06)

Ñàkk bopp (9:​31)

GËSTUL

 42 Lan la Biibël bi wax ci salibateer ak séy?

Ay salibateer yu takku ci Yàlla (3:​11)

Séy dafa war a sax ba fàww (4:​30)

Mën nga topp santaane Yexowa yi ci séy (4:​14)

GËSTUL

Waajal séy (17:05)

Dama foogoon ne dina nangu dëgg gi (1:​56)

 43 Naka la karceen yi war a gise sàngara?

Ndax war naa jox nit ñi sàngara? (2:​41)

‘Dama doyaloon ci sama dundin’ (6:​32)

GËSTUL

Xalaatal ci li la naan sàngara mën a jural (2:​31)

 44 Ndax feet yépp a neex Yàlla?

Ay feet ak ay màggal yu neexul Yàlla (5:​07)

Xamleel li nga gëm ànd ci ak teggin (2:​01)

Teraanga ji ñuy wone ci suñu ndaje yu mag yi (5:​40)

GËSTUL

Yexowa fonk na leen (11:​35)

 45 Naka lañu mënee wone ne nguuru Yexowa rekk lañu faral?

GËSTUL

Yexowa masuñoo bàyyi (3:​14)

«Dara tëwul Yàlla» (5:​19)

 46 Lu tax nga war a jébbalu te sóobu ci ndox?

Nañu may Yàlla li ñu am (3:​04)

Sama dund gépp futbal la woon (5:​45)

GËSTUL

May naa la sama dund (4:​30)

 47 Ndax pare nga ngir sóobu ci ndox?

Fi ñu mën a jaar ba sóobu ci ndox (3:​56)

Yexowa Yàlla dina la dimbali (2:​50)

GËSTUL

‘Lu tax sóobuwoo ci ndox ba léegi?’ (1:​10)

Ndax yelloo naa lii dëgg? (7:​21)