Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

13 sãwiyee ba 19 sãwiyee

TAALIFI CANT 135-137

13 sãwiyee ba 19 sãwiyee

Woy-Yàlla nº 2 ak ñaan | Kàddu yi ñuy tàmbalee ndaje bi (1 minit)

NJÀNGALE YU AM SOLO YU NEKK CI KÀDDU YÀLLA

1. «Suñu Boroom a sut lépp lu ñuy jaamu»

(10 minit)

Yexowa wone na ne am na doole ci kaw lépp li mu sàkk (Taalifi Cant 135:​5, 6; it-1-F 914 § 18-19)

Yexowa dafay muccal mbooloom (Mucc ga 14:​29-31; Taalifi Cant 135:14)

Yexowa dafa ñuy jàppale bu ñu amee tiis (Taalifi Cant 136:23; w21.11-F 6 § 16)

2. Nañu xóotal suñu njàngum Biibël bi

(10 minit)

  • Taalifi Cant 136:15—Ca jamono yu njëkk ya, naka la Yexowa wonee ne moo ëpp kàttan nguur yi? (w22.10-F 15 § 12)

  • Ban aaya ngeen xóotal ci seen njàngum Biibël bi ci semen bi?

3. Aaya yi ñu war a liir ci Biibël bi

YOKKAL SA MËN-MËN CI LIGGÉEYU WAARE BI

4. Ni nga mënee tàmbali waxtaan

(3 minit) WAARAATE SAA YU ÑU AMEE BUNT. Nit ki déglu na la bu baax. Jox ko sa nimero telefon wala mu jox la bosam ngir ngeen wéyal waxtaan bi. (lmd-F lesoŋ 2 ponk 4)

5. Li ñu mën a wax bu ñu seetiwaatee nit ki

(4 minit) KËROO-KËR. Waxal nit ki mu teewe ndaje yi. (lmd-F lesoŋ 9 ponk 4)

6. Wax ci li ñu gëm

(5 minit) Wone bi. Ijwfq-F waxtaan nº 7—Wone bi, mu ngi sukkandiku ci waxtaan bii ci farãse: Les Témoins de Jéhovah sont-ils chrétiens ? (th lesoŋ 12)

DUNDINU KERCEEN

Woy-Yàlla nº 10

7. Li mbooloo mi soxla ci wàllu ngëm

(15 minit)

8. Njàngum Biibël bi ci biir mbooloo mi

Kàddu yi ñuy tëje ndaje bi (3 minit) | Woy-Yàlla nº 90 ak ñaan