Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

14 Oktoobar ba 20 oktoobar

TAALIFI CANT 96-99

14 Oktoobar ba 20 oktoobar

Woy-Yàlla nº. 66 ak ñaan | Kàddu yi ñuy tàmbalee ndaje bi (1 minit)

NJÀNGALE YU AM SOLO YU NEKK CI KÀDDU YÀLLA

1. Nañu siiwal xibaaru jàmm bi!

(10 minit)

Nañu yégal nit ñi xibaaru jàmm bi (Taalifi Cant 96:2; w11-F 1/3 6 § 1-2)

Nañu xamal nit ñi xibaaru jàmm bi jëm ci Bésu àtte bi (Taalifi Cant 96:​12, 13; w12-F 1/9 16 § 1)

Nañu xamal nit ñi ne coobare Yexowa mooy, feesal suuf si ak ay nit yuy màggal turam (Taalifi Cant 99:​1-3; w12-F 15/9 12 § 18-19)

2. Nañu xóotal suñu njàngum Biibël bi

(10 minit)

  • Taalifi Cant 96:1—Ci Biibël bi baat bii «woy wu yees», lan lay tekki? (it-1-F 425)

  • Ban aaya ngeen xóotal ci seen njàngum Biibël bi ci semen bi?

3. Aaya yi ñu war a liir ci Biibël bi

YOKKAL SA MËN-MËN CI LIGGÉEYU WAARE BI

4. Farlu ci waare bi—Li Yeesu def

(7 minit) Waxtaan ak ñi teew. Woneel WIDEO bi, ba pare ngeen waxtaan ci lmd-F lesoŋ 10 ponk 1-2.

5. Farlu ci waare bi —Nañu roy ci Yeesu

(8 minit) Waxtaan ak ñi teew. Waxtaan bi mu ngi sukkandiku ci lmd-F lesoŋ 10 ponk 3-5 ak «Seetal aaya yii itam».

DUNDINU KERCEEN

Woy-Yàlla nº. 9

6. Li mbooloo mi soxla ci wàllu ngëm

(15 minit)

7. Njàngum Biibël bi ci biir mbooloo mi

Kàddu yi ñuy tëjee ndaje bi (3 minit) | Woy-Yàlla nº. 67 ak ñaan