Ay nettali yu ñuy jàng ci Biibël bi
Mën nga déglu walla telesarse ay nettali yu ñu jële ci Biibel bi te ànd ak misik ak ay wax yu ñu ci yokk. Boo leen di déglu, melal ni yaa ngi koy fekke. Am na it ay wideo yu ñu def ci làkku muuma yi.
Tànnal benn làkk ba pare nga bës fi ñu bind Génne ko ngir gis nettali yi am ci làkk bi nga tànn. Boo bëggee gis nettali yu ànd, bindal baat bu bokk ci turu nettali bi walla nga bind benn turu téere ci Biibël bi.