Yexowa dafay musal mbooloom Li ñu nettali ci Biibël bi ci Gàddaay gi pàcc 3 ba 15, dafay wone ne Yàlla mi xaajoon Géeju barax ya dina la musal yaw itam boo wonee ngëm gu ànd ak muñ. Nettali bi, mu ngi sukkàndiku ci Gàddaay gi 3:1-22; 4:1-9; 5:1-9; 6:1-8; 7:1-7; 14:5-10, 13-31; 15:1-21. Le chargement du lecteur multimédia a échoué. Telesarseel wideo bii