Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
1. Lu tax ñu war a yokk suñu ngëm tey ci tey? (Yawut ya 10:39)
2. Naka lañu mënee gis Yexowa mi “kenn mënula teg bët”? (Yawut ya 11:27)
3. Lu tax jàng waxi yonent yi nekk ci Biibël bi am njariñ? (Room 10:17)
4. Naka la ñu xel mu sell mi mënee dimbali ñu yokk suñu ngëm? (Luug 11:13; Galasi 5:22)
5. Naka lañu mënee dimbali suñuy moroom ngir yékkati seen ngëm? (1 Tesalonig 2:7, 8)
6. Lu tax ñu war a «ne jàkk Yeesu, moom mi samp ngëm, ba ub làmbi ngëm»? (Yawut ya 12:2, 3)