Àjjuma
«Yokkal sunu ngëm» (Luug 17:5)
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla n° 5 ak ñaan
-
9:40 WAXTAANU KIY JIITE NDAJE BI: Lan mooy kàttanu ngëm? (Macë 17:19, 20; Yawut ya 11:1)
-
10:10 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Li tax ñu gëm . . .
-
• Ne Yàlla am na (Efes 2:1, 12; Yawut ya 11:3)
-
• Kàddu Yàlla (Esayi 46:10)
-
• Santaaney Yàlla (Esayi 48:17)
-
• Ne Yàlla bëgg na ñu (Yowaana 6:44)
-
-
11:05 Woy-Yàlla n°37 ak yégle yi
-
11:15 AY NETTALI YU ÑUY JÀNG CI BIIBËL BI: Nóoyin: Ngëm a taxoon mu déggal Yàlla (Njàlbéen ga 6:1–8:22; 9:8-16)
-
11:45 «Gëm[leen] te baña werante» (Macë 21:21, 22))
-
12:15 Woy-Yàlla n° 118 ak noppalu bi
NGOON GI
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla n° 2
-
1:50 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Xoolal li Yàlla sàkk ngir dëgëral sa ngëm
-
• Biddéew yi (Esayi 40:26)
-
• Géej gi (Sabóor 93:4)
-
• Àll bi (Sabóor 37:10, 11, 29)
-
• Ngelaw ak ndox (Sabóor 147:17, 18)
-
• Mbindeef yi ci biir géej (Sabóor 104:27, 28)
-
• Suñu yaram (Esayi 33:24)
-
-
2:50 Woy-Yàlla n° 148 ak yégle yi
-
3:00 Jaloore yu réy yi Yexowa def dañuy yokk ngëm (Esayi 43:10; Yawut ya 11:32-35)
-
3:20 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Royleen ñi takkuwoon ci Yàlla, buleen roy ñi ñàkkoon ngëm
-
• Roy ci Abel, waaye du ci Kayin (Yawut ya 11:4)
-
• Roy ci Enog, waaye du ci Lameg (Yawut ya 11:5)
-
• Roy ci Nóoyin, waaye du ci ay dëkkandoom (Yawut ya 11:7)
-
• Roy ci Musaa, waaye du ci Firawna (Yawut ya 11:24-26)
-
• Roy ci taalibe Yeesu yi, waaye du ci Farisen yi (Jëf ya 5:29)
-
-
4:15 Naka ngeen mënee ‘Xool seen bopp bu baax, ba xam ndax ngëm a ngi ci yéen’? (2 Korent 13:5, 11)
-
4:50 Woy-Yàlla n° 119 ak ñaan bu mujj bi