Dimaas
«Su ngeen gëmee . . . , dina ko def» (Macë 21:21)
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla n° 137 ak ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Royleen jigéen ñi amoon ngëm gu dëggër!
-
• Saarata (Yawut ya 11:11, 12)
-
• Raxab (Yawut ya 11:31)
-
• Aana (1 Samiyel 1:10, 11)
-
• Janq bi ñu jàppewoon réewum Israyil (2 Buur ya 5:1-3)
-
• Maryaama yaayu Yeesu (Luug 1:28-33, 38)
-
• Jigéenu waa Fenisi (Macë 15:28)
-
• Màrt (Yowaana 11:21-24)
-
• Ay royukaay ci suñu jamono (Sabóor 37:25; 119:97, 98)
-
-
11:05 Woy-Yàlla n° 142 ak yégle yi
-
11:15 WAXTAAN BI ÑU JAGLEEL ÑÉPP: ‘Gëmleen xibaaru jàmm bi’ (Màrk 1:14, 15; Macë 9:35; Luug 8:1)
-
11:45 Woy-Yàlla n° 22 ak noppalu bi
NGOON GI
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla n° 126
-
1:50 TIYAATAR BU SUKKANDIKU CI BIIBËL BI: Dañeel: Dafa amoon ngëm ci dundam gépp (Xaaj II) (Dañeel 5:1–6:28; 10:1–12:13)
-
2:40 Woy-Yàlla n° 150 ak yégle yi
-
2:45 Na sa ngëm sax di gën a dëgër! (Dañeel 10:18, 19; Room 4:18-21)
-
3:45 Woy bu bees bi ak ñaan bu mujj bi