Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Ñi bëgg jàmm

Ñi bëgg jàmm

LUUG 10:6

Suba si

  • 9:40 Misik

  • 9:50 Woy-Yàlla No. 58 ak ñaan

  • 10:00 Yéen ñi bëgg jàmm, dal-leen ak jàmm!

  • 10:15 Wéy leen di wut ñi bëgg jàmm

  • 10:30 Naka la Yeesu, Buuru jàmm bi, di leen di dimbalee ngeen wut ñi bëgg jàmm

  • 10:55 Woy-Yàlla No. 103 ak yégle yi

  • 11:05 Ñi bëgg jàmm duñu jàng xare

  • 11:35 Jébbalu bi ak sóob bi

  • 12:05 Woy-Yàlla No. 79

Ngoon gi

  • 1:20 Misik

  • 1:30 Woy-Yàlla No. 76

  • 1:35 Ay nettali

  • 1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal

  • 2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Yéen ñi bëgg jàmm, nañu dimbalante suñu biir

    • • «Ubbileen seen xol»

    • • Dimbalileen ndaw yi ñu def lépp li ñu mën ci liggéeyu Yexowa

    • • Teral-leen mag ñi

  • 3:00 Woy-Yàlla No. 57 ak yégle yi

  • 3:10 Yeen ñi bëgg jàmm, lan ngeen mën a def ba not lu bon, ci def lu baax?

  • 3:55 Woy-Yàlla No. 45 ak ñaan