Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Yexowa dafay jàngal mbooloom ñu nekk benn

Yexowa dafay jàngal mbooloom ñu nekk benn

EFES 4:3

Suba si

  • 9:30 Misik

  • 9:40 Woy-Yàlla No. 85 ak ñaan

  • 9:50 Nañu fonk suñu palaas ci mbooloo Yexowa

  • 10:05 Waxtaan bu def ay xaaj: Dañu wone ne fonk nañu ñeneen ñi

    • • Eliyu

    • • Lidi

    • • Yeesu

  • 11:05 Woy-Yàlla No. 100 ak yégle yi

  • 11:15 Wéyleen di dimbali ñeneen ñi ñu ñëw bokk ci mbooloo Yexowa

  • 11:30 Jébbalu bi ak sóob bi

  • 12:00 Woy-Yàlla No. 135

Ngoon si

  • 1:10 Misik

  • 1:20 Woy-Yàlla No. 132 ak ñaan

  • 1:30 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp: Ndax yéen a ngi def lépp ngir jàmm am ci seen kër?

  • 2:00 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal

  • 2:30 Woy-Yàlla No. 136 ak yégle yi

  • 2:40 Waxtaan bu def ay xaaj: Naka nga mënee def lépp ngir wut jàmm?

    • • Nanga «wax lu rafet»

    • • Nanga ‘wéer sa dund ci mbëggeel’

    • • Nanga xeex suñuy noon

  • 3:40 Buleen «noppee sant Yàlla» ci li ngeen bokk ci mbooloom

  • 4:15 Woy-Yàlla No. 107 ak ñaan