Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2022 bi tudd ‘Wutleen jàmm!’
Àjjuma
Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Sabóor 29:11: ‘Yexowa dina barkeele jàmm mbooloom’
Samdi
Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci 2 Piyeer 3:14: Ñu «fekk leen ci jàmm, ngeen baña am benn gàkk mbaa sikk.»
Dimaas
Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Room 15:13: «Yàlla miy maye yaakaar, na def ci seen xol mbég mu réy ak jàmm ju yaa»
Li ñi teew war a xam
Li ñi teew ci ndaje bu mag bu ñetti fan bi war a xam.