Àjjuma
Suba si
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla nº 86 ak ñaan
-
9:40 WAXTAANU KIY JIITE NDAJE BI: Yexowa «Yàlla miy Boroom jàmm» (Room 15:33; Filib 4:6, 7)
-
10:10 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Ni mbëggeel di indee jàmm dëgg
-
• Bëgg Yàlla (Macë 22:37, 38; Room 12:17-19)
-
• Bëgg sa moroom (Macë 22:39; Room 13:8-10)
-
• Bëgg Kàddu Yàlla (Sabóor 119:165, 167, 168)
-
-
11:05 Woy-Yàlla nº 24 ak yégle yi
-
11:15 AY NETTALI YU ÑUY JÀNG CI BIIBËL BI: Yanqóoba: Góor gu bëggoon jàmm la (Njàlbéen ga 26:12–33:11)
-
11:45 «Njekk ay jur jàmm» (Esayi 32:17; 60:21, 22)
-
12:15 Woy-Yàlla no 97 ak noppalu bi
Ngoon gi
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla nº 144
-
1:50 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Bànneexuleen ci jàmm ji Yàlla dige
-
• «Sama jaam ñeey lekk [...] sama jaam ñeey naan» (Esayi 65:13, 14)
-
• «Ñooy tabax ay kër [...] jëmbati tóokër» (Esayi 65:21-23)
-
• «Bukki ak mboteey bokk di for» (Esayi 11:6-9; 65:25)
-
• ‘Du kenn ku neeti wopp na’(Esayi 33:24; 35:5, 6)
-
• «Mooy mëdd ndee ba fàww!» (Esayi 25:7, 8)
-
-
2:50 Woy-Yàlla no 35 ak yégle yi
-
3:00 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Toppleen xelal yiy indi jàmm ci biir njaboot
-
• Woneleen mbëggeel ak wegeel (Room 12:10)
-
• Amleen wax ju rafet ci biir njaboot gi (Efes 5:15, 16)
-
• Àndleen liggéey (Macë 19:6)
-
• Àndleen ci jaamu Yexowa (Josué 24:15)
-
-
3:55 Saxleen ci jàppale «Buuru jàmm bi» (Esayi 9:5, 6 Tit 3:1, 2)
-
4:15 Buleen kenn nax ak jàmm ju dul dëgg! (Macë 4:1-11; Yowaana 14:27; 1 Tesalonig 5:2, 3)
-
4:50 Woy-Yàlla nº 112 ak ñaan bu mujj bi