Dimaas
Suba si
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla nº 101 ak ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Naka lañu jiwe jàmm te góob ko?
-
• Yuusufa ak ay magam (Galasi 6:7, 8; Efes 4:32)
-
• Waa Gabawon (Efes 5:17)
-
• Sedeyon (Juges 8:2, 3)
-
• Abigayil (1 Samiyel 25:27-31)
-
• Mefiboset (2 Samiyel 19:26-29)
-
• Pool ak Barnabas (Jëf ya 15:36-39)
-
• Ay royukaay ci suñu jamono (1 Piyeer 2:17)
-
-
11:05 Woy-Yàlla nº 28 ak yégle yi
-
11:15 WAXTAAN BI ÑU JAGLEEL ÑÉPP: Naka lañu mënee nekk xaritu Yàlla? (Saag 4:8; 1 Yowaana 4:10)
-
11:45 Woy-Yàlla nº 147 ak noppalu bi
Ngoon gi
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla nº 23
-
1:50 TIYAATAR BU SUKKANDIKU CI BIIBËL BI: Yexowa moo ñuy awale ci yoonu jàmm: (Xaaj 2) (Esayi 48:17, 18)
-
2:30 Woy-Yàlla nº 139 ak yégle yi
-
2:40 Ci lu wóor, jàmm dina am ci àddina si sépp! (Room 16:20; 1 Korent 15:24-28; 1 Yowaana 3:8)
-
3:40 Woy bu bees bi ak ñaan bu mujj bi