Li ñi teew war a xam
Sóob bi Magi mbooloo mi jël nañu ba pare matuwaay yi gën, ngir ñi bëgg a sóobu ci ndox mën koo def, bu porogaraamu samdi bi ci suba si jeexee.
Ñi bëgg a def ay maye Ndaje bu mag bu ñetti fan bii, dinañu ko tekki ci lu ëpp 500 làkk. Maye yi ngeen di def dafay jàppale liggéey boobu ñuy def ci àddina si sépp. Mën ngeen maye jaare ko ci internet ci donate.pr418.com. Ñu ngi leen di gërëm bu baax ci lépp li ngeen di maye. Jataay biy dogal it mu ngi leen di gërëm ci lépp li ngeen di maye ngir liggéeyu Nguur gi jëm kanam.
Jataay biy dogal ci Seede Yexowa yi moo taxawal ndaje bii
© 2022 Watch Tower Bible and Tract Society of Pennsylvania