Samdi
Suba si
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla nº 58 ak ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: Nanga pare ngir yégle «xibaaru jàmm» bi
-
• Wéyal di sawar (Room 1:14, 15)
-
• Waajalal sa bopp bu baax (2 Timote 2:15)
-
• Tàmbalil waxtaan bi (Yowaana 4:6, 7, 9, 25, 26)
-
• Seetiwaatal nit ki (1 Korent 3:6)
-
• Dimbalil ñiy jàng Biibël bi ñu mat ci wàllu ngëm (Yawut ya 6:1)
-
-
10:40 Yeen ndaw ñi: Tànnleen li leen di indil jàmm! (Macë 6:33; Luug 7:35; Saag 1:4)
-
11:00 Woy-Yàlla nº 135 ak yégle yi
-
11:10 WIDEO: Ni suñu mbokk yi di def ba am jàmm bu dee sax...
-
• Dañu leen di fitnaal
-
• Dañu feebar
-
• Dañu ñàkk xaalis
-
• Musiba dal na leen
-
-
11:45 SÓOB BI: Wéyleen di dox «ci yoonu jàmm» (Luug 1:79; 2 Korent 4:16-18; 13:11)
-
12:15 Woy-Yàlla nº 54 ak noppalu bi
Ngoon gi
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla nº 29
-
1:50 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: «Bàyyileen» liy yàq jàmm
-
• Tiitaru (Efes 4:22;1 Korent 4:7)
-
• Kiñaan (Filib 2:3, 4)
-
• Naxaate (Efes 4:25)
-
• Jëw (Kàddu yu Xelu 15:28)
-
• Mer bu ëpp (Saag 1:19)
-
-
2:45 TIYAATAR BU SUKKANDIKU CI BIIBËL BI: Yexowa moo ñuy awale ci yoonu jàmm: (Xaaj 1) (Esayi 48:17, 18)
-
3:15 Woy-Yàlla nº 130 ak yégle yi
-
3:25 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ: «Xënte jàmm te sax ci» mooy...
-
• Di bañ a gaaw a mer (Kàddu yu Xelu 19:11; Kàdduy Waare 7:9; 1 Piyeer 3:11)
-
• Di baalu (Macë 5:23, 24; Jëf ya 23:3-5)
-
• Di baale (Kolos 3:13)
-
• Di jëfandikoo bu baax suñu làmmiñ (Kàddu yu Xelu 12:18; 18:21)
-
-
4:15 Nañu wéy di «likkoo ci jàmm»! (Efes 4:1-6)
-
4:50 Woy-Yàlla nº 113 ak ñaan bu mujj bi