Ndaje bu mag bu benn fan bu Seede Yexowa yi ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2024-2025
Amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi
Porogaraamu suba si ak bu ngoon si, bu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni.
Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii:
Dinañu tontu ci laaj yii ci ndaje bu mag bi.