Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi

Amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi

ROOM 1:​16

Suba si

  • 9:40 Misik

  • 9:50 Woy-Yàlla nº 67 ak ñaan

  • 10:00 Amuñu dara lu ñuy rus ci xibaaru jàmm bi—Lu tax?

  • 10:15 Woneel ne da nga takku ci xibaaru jàmm bi

  • 10:30 Woneel ne liggéeykat bu amul dara li muy rus nga

  • 10:55 Woy-Yàlla nº 73 ak yégle yi

  • 11:05 Solul Xel mu ànd ak kàttan, mbëggeel ak moom sa bopp

  • 11:35 SÓOB BI: Wéyal di ‘déggal xibaaru jàmm bi’

  • 12:05 Woy-Yàlla nº 75

Ngoon gi

  • 1:20 Misik

  • 1:30 Woy-Yàlla nº 77

  • 1:35 Ay nettali

  • 1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal

  • 2:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Dañu fonk . . .

    • • Santaane Yàlla yi

    • • Nguuru Yàlla

    • • Ñi ñuy jiite ci mbootaayu Yàlla

  • 3:00 Woy-Yàlla nº 40 ak yégle yi

  • 3:10 Dañuy «ndamu ci Boroom bi»

  • 3:55 Woy-Yàlla nº 7 ak ñaan