Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Njàngale 3

Njàngale 3

Njàngale 3

1 Piyeer 3:8

Dawuda dégg na ne xaritam dafa feebar.

Mu ne : “ Xam naa li ma war a def.

Dama koy bind letaar ngir mu kontaan. Su ma paree ma yóbbu ko ! ”

Nanga baax ak moom. Dingeen kontaan yéen ñaar !

LI NGA MËN A DEF YAW AK SA DOOM

Jàngalal lii sa doom :

1 Piyeer 3:8

Waxal sa doom mu won la :

Kër Taabal Dawuda

Naaj Picc Garab

Laajal sa doom lii :

Ndax xam nga kenn ku feebar ?

Lan lañu ko mën a defal ?

[Nataal bi nekk paas 8]

[Nataal bi nekk paas 8]

[Nataal bi nekk paas 9]

[Nataal bi nekk paas 9]