Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Njàngale 5

Njàngale 5

Njàngale 5

1 Tesalonig 5:18

Sa xarit, bu la mayee kado walla mu defal la lu baax, won ko ne kontaan nga.

Waaye foo mënta nekk ak loo nekk di def, bul fàtte di wax “ mersi ! ”

LI NGA MËN A DEF YAW AK SA DOOM

Jàngalal lii sa doom :

1 Tesalonig 5:18

Waxal sa doom mu won la :

Kado Xale

Bunt Bool

Pom Telefon

Laajal sa doom lii :

Lu tax nga war a wax “ mersi ” ?

[Nataal bi nekk paas 12]

[Nataal bi nekk paas 13]

[Nataal bi nekk paas 13]

[Nataal bi nekk paas 13]