Njàngale 6
Njàngale 6
Xoolal sa baaraam yi, yëngalal sa baaraamu tànk yi. Laalal sa nopp yi ak sa bakkan bi.
Xoolal sa tànk yi. Ñoom ñoo tax nga mën a daw, di tëb, di wëndeelu ak di fo !
Xoolal sa bopp ci seetu bi.
Lan ngay gis ? Yexowa moo def lépp ba mu rafet !
LI NGA MËN A DEF YAW AK SA DOOM
Jàngalal lii sa doom :
Waxal sa doom mu won la :
Baaraamam yi Baaraamu tànkam yi
Bakkanam Noppam yi
Gémmiñam bi Junqóob
Muus
Laajal sa doom lii :
Kan moo ñu sàkk, man ak yaw ?
[Nataal bi nekk paas 14]
[Nataal bi nekk paas 15]
[Nataal bi nekk paas 15]
[Nataal bi nekk paas 16]