Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

18-B

Xaalis bi ak wàllu peese bi

Xaalis bi ak wàllu peese bi

Xaalis bi ak wàllu peese bi ci Mbind yu sell yi ci làkku Ebrë

Gera (120 siikal)

0.57 g

10 gera = 1 béqa

Béqa

5.7 g

2 béqa = 1 siikal

Pim

7.8 g

1 pim = 23 siikal

Li siikal di peese

Siikal

11.4 g

50 siikal = 1 mina

Mina

570 g

60 mina = 1 talaŋ

Talaŋ

34.2 kg

Daric (Xaalisu Pers, wurus)

8.4 g

Ezra 8:⁠27

Xaalis bi ak wàllu peese bi ci Mbind yu sell yi ci làkku Gereg

Lepton (Xaalisu Yawut, përëm)

12 quadrans

Luug 21:2

Quadrans (Xaalisu Room, përëm)

2 lepta

Macë 5:⁠26

Asariyon (Xaalisu Room ak li ko wër, përëm)

4 quadrans

Macë 10:⁠29

Denariyon (Xaalis Room, xaalis)

64 quadrans

3.85 g

Macë 20:⁠10

= Peyug 1 bés (12 waxtu)

Daraxma (Xaalisu Geres, xaalis)

3.4 g

Luug 15:8

= Peyug 1 bés (12 waxtu)

Didaraxmon (Xaalisu Geres, xaalis)

2 daraxma

6.8 g

Macë 17:⁠24

= Peyug 2 bés

Tétra-daraxma bu Ancos

Tétra-daraxma bu Tir (Siikalu xànjar bu Tir)

Tétra-daraxma(Xaalisu Geres, xaalis, ñu koy woowe it estateer bu xaalis)

4 daraxma

13.6 g

Macë 17:⁠27

Peyug 4 bés

Mina

100 daraxma

340 g

Luug 19:⁠13

= lu jege peyug 100 bés

Talaŋ

60 mina

20.4 kg

Macë 18:24

Peeñu ma 16:⁠21

= lu jege peyug 19 at

Liibar (bu Room)

327 g

Yowaana 12:3

“ Liibaru latkoloñ ju raxul ju ñuy wax nàrd ”