3-B
Yonent yi ak buuri réewu Yuda ak Israyil (Xaaj 2)
Buuri nguur gi féete woon bëj-saalum (fi lay kontine)
777 B.S.J.
Yowatam : 16 at
762
Akas : 16 at
746
Esekiya : 29 at
716
Manase : 55 at
661
Amon : 2 at
659
Yosiyas : 31 at
628
Yehoahaz : 3 weer
Yowakim : 11 at
618
Yoyakin : 3 weer ak 10 fan
617
Sédésiyas : 11 at
607
Bi Nebukanesar nekkee buuru Babilon, ci la moom ak waa Babilon yàq Yerusalem ak Këru Yàlla ga. Ci jamono jooju it lañu wacce Sédésiyas ca nguur ga. Moom moo nekkoon buur bi mujj ci buur yi jóge ci askanu Daawuda ci kaw suuf
Buuri nguur gi féete woon bëj-gànnaar (fi lay kontine)
b.803 B.S.J.
Sakari : 6 weer rekk la nguuru
Sakari komaase woon na nguuru daanaka waaye dafa mel ni nguuram dëgg, ci booru atum 792 la komaase
b.791
Sàllum : 1 weer
b.780
Menahem : 10 at
Peqahia : 20 at
b.778
Péqah : 20 at
b. 758
Ose : 9 at booru 748
b.748
Dafa mel ni nguuru Ose ci booru 748 la door a sampu dëgg walla ci booru at boobu la ko buuru Asiri Tiglath-Piléser III door a dimbali ci nguur gi
740
Asiri jël Samari, daanel Israyil ; nguuru Israyil gi féete bëj-gànnaar te am fukki giir ya daldi jeex
-
Turu yonent yi
-
Esayi
-
Mika
-
Sofoni
-
Yérémi
-
Naxum
-
Xabakkuk
-
Dañeel
-
Esekiel
-
Obaja
-
Ose