Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

19

Kalandiryeeru Yawut yi

Kalandiryeeru Yawut yi

NISAN (ABIB) Màrs​—Awril

14 Màggalu bésu Mucc ga

15-21 Mburu mu amul lawiir

16 Ñu saraxe li njëkk a meññ

Yurdan bi fees ndax taw yi ak galaas yi (neige) seey

Dugub

IYYAR (ZIV) Awril​—Me

14 Màggalu bésu mucc gi ñu yéex a def

Noor bi komaase, asamaan si faral di set

Blé

SIVÂN Me​—Suweŋ

6 Màggalu semen yi (Pàntakótt)

Tàngooru nawet, ngelaw lu àndul ak puseer

Blé, figg yi njëkk a ñor

TAMMUS Suweŋ​—Sulyet

 

Tàngoor wi yokku, lay bu metti am ci yenn gox

Reseñ yi njëkk a ñor

AB Sulyet​—Ut

 

Tàngoor wi yokku ba sës

Liy meññ ci tàngoor wi

ÉLOUL Ut​—Septaambar

 

Tàngoor wi kontine

Tàndarma, reseñ, ak figg

TISHRI (ÉTHANIM) Septaambar​—Oktoobar

1 Yuuxu liit

10 Bésu baale bàkkaar

15-21 Màggalu mbaar ya

22 Ndaje bu sell bi

Tàngoor bi jeex, taw yu njëkk yi

Mbey mi

HESHVÂN (BOUL) Oktoobar​—Nowàmbar

 

Taw yu yem

Oliw yi

KISLEV Nowàmbar​—Desàmbar

25 Màggalu Sellal kër Yàlla ga

Taw yi yokku, lépp galaase, galaas (neige) am ci kaw tund yi

Ñu fat jur gi ndax sedd bid

TÉBETH Desàmbar​—Sãwiyee

 

Mu sedd ba sës, di taw, galaas am ci kaw tund yi

Ñax mi sax

SHEBAT Sãwiyee​—Fewriyee

 

Seddaay bi yokku, taw bi kontine

Gerte-tubaab yi tóor-tóor

ADAR Fewriyee​—Màrs

14, 15 Pourim

Mu bare ay taw yu ànd ak dënnu ak tawu galaas

Lin

VÉADAR Màrs

Weer wi ñuy yokk 7 yoon ci 19 at yu nekk