Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

4-C

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Waare bu mag bi Yeesu def ca Galile (Xaaj 1)

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Waare bu mag bi Yeesu def ca Galile (Xaaj 1)

—Waare bu mag bi Yeesu def ca Galile (Xaaj 1)

JAMONO JA

BÉRÉB BA

XEW-XEW BA

MACË

MÀRK

LUUG

YOWAANA

30

Galile

Bi Yeesu njëkkee yégle ne “ nguuru Yàlla jegesi na ”

4:​17

1:14, 15

4:14, 15

4:44, 45

Kana ; Nasaret ; Kapernawum

Yeesu faj ab doomu Kilifa ; mu jàng téereb yonent Yàlla Esayi ; mu dem Kapernawum

 

​—

4:16-31

4:46-54

Dexu Galile, wetu Kapernawum

Mu woo : Simoŋ ak Andare, Saag ak Yowaana

4:​18-​22

1:16-20

 

​—

Kapernawum

Mu faj gorob Piyeer bu jigéen ak ñu bare

8:14-17

1:21-34

 

​—

Galile

Bi mu njëkkee wër Galile ak ñeent ñooñu

4:23-25

1:35-39

 

​—

Mu faj ku gaana ; mbooloo mu bare topp ko

8:1-4

1:40-45

 

​—

Kapernawum

Faj na ku làggi

9:1-8

2:1-12

 

​—

Mu woo Macë ; lekk ak ay juutikat ; wax wu jëm ci woor

9:9-17

2:13-22

 

​—

Yude

   

​—

 

​—

31, Bésu mucc ga

Yerusalem

     

​—

5:1-47

Bi mu jógee Yerusalem (?)

Taalibeem ya fàq ay gub bésub noflaay ba ; Yeesu “ boroom bésub noflaay bi ”

12:1-8

2:23-28

 

​—

Galile ; Dexu Galile

Mu faj ku loxoom làggi ; mbooloo mu bare topp ko ; mu faj ñu gën a bare

12:9-21

3:1-12

 

​—

Tund wetu Kapernawum

 

​—

3:13-19

 

​—

Wetu Kapernawum

Mu def ab waare ca tund ba

 

​—

 

​—

Kapernawum

Mu faj surgab njiitu xare

 

​—

 

​—

Nayin

   

​—

 

​—

Tiberiyàdd ; Galile (Nayin walla wetam)

Yaxya yónni ay taalibeem ci Yeesu; ñu xamal ay xale yu ndaw dëgg gi, yen bu diisul

 

​—

 

​—

Galile (Nayin walla wetam)

   

​—

 

​—

Galile

   

​—

 

​—

Mu dàq ay rab ; bàkkaar bu ñu dul baal

12:22-37

   

​—

Joxewul firnde ju dul firndey Yunus

     

​—

Yaayam ak ay rakkam ñëw ; Yeesu ne taalibeem yi ñooy ay mbokkam

12:46-50

3:31-35

 

​—