Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

4-F

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Waare Yeesu ci penku Yurdan

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Waare Yeesu ci penku Yurdan

JAMONO JA

BÉRÉB BA

XEW-XEW BA

MACË

MÀRK

LUUG

YOWAANA

32, bi Màggalu bés ba ñu sellalee kër Yàlla weesoo

Betani ca gannaaw Yurdan

Mu dem fa Yaxya daan sóobe ci ndox ; ñu bare gëm Yeesu

     

10:40-42

Pere

Mu jëm Yerusalem, di jàngale ci ay dëkk yu mag ak yu ndaw

   

13:22

 

Mu xiirtal nit ñi ñu jaar ci bunt bu xat bi ; muy jàmbat Yerusalem

   

13:23-35

 

Xéyna Pere

Mu jàngale cig woyof ; ay léeb : toogu yi gën a yiw ñiy jégglu ci ngan gi

   

14:1-24

 

Xalaat ci ñaata la nekk taalibe di dikke

   

14:25-35

 

Ay léeb : xar mu réer ma, xaalis bu réer ba, doom ju réer ja

   

15:1-32

 

Ay léeb : bëkk-néeg bu njublaŋ bi, boroom alal ji ak Lasaar

   

16:1-31

 

Mu jàngale ci fiir yuy yóbbe bàkkaar, ci baale ak ci ngëm

   

17:1-10

 

Betani

Lasaar dee na te dekki

     

11:1-46

Yerusalem ; Efrayim

Pexe ngir rey Yeesu, mu dem

     

11:47-54

Samari ; Galile

Faj na fukki gaana ; wax na ni Nguuru Yàlla di ñëwe

   

17:11-37

 

Samari walla Galile

Ay léeb : jigéen ju lakkale te jëkkëram faatu, Farisen bi ak juutikat bi

   

18:1-14

 

Pérée

Mu jàngale ci séy ak pase

19:1-12

10:1-12

   

Mu ñaanal xale yu ndaw yi

19:13-15

10:13-16

18:15-17

 

Laaju waxambaane wi bare alal ; léebu liggéeykat yi ci toolu reseñ ak léebu pey yi tolloo

19:16–20:16

10:17-31

18:18-30

 

Xéyna Pere

Mu xamle ñetteelu yoon ne dina dee

20:17-19

10:32-34

18:31-34

 

Saag ak Yowaana ñaan palaas bu kawe ci Nguur gi

20:20-28

10:35-45

   

Yériko

Bi muy aw Yériko, mu faj ñaari gumba ; mu dem kër Sase ; misaalu fukki libidoor ya

20:29-34

10:46-52

18:35–19:28