Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

18-A

Xayma ak xaalis

Xayma ak xaalis
  • Xayma walaan yi

  • Kor (10 bidoŋ / 60 hîns)

    220 L / 58.1 gal

  • Bidoŋ (6 hîns)

    22 L / 5.81 gal

  • Hîn (12 logs)

    3.67 L / 7.75 pt

  • Log (112 hîns)

    0.31 L / 0.66 pt

  • Xayma pënd ak pepp

  • Homer (1 Kor / 10 éphas)

    220 L

  • Épha (3 mata / 10 homers)

    22 L

  • Mata (313 homers)

    7.33 L

  • Homer (145 qab)

    2.2 L

  • Qab

    1.22 L

  • Kilo

    1.08 L

  • Xayma guddaay yi

  • Barax bu gudd (6 xasab yu gudd)

    3.11 m / 10.2 ft

  • Barax (6 xasab)

    2.67 m / 8.75 ft

  • Brasse

    1.8 m / 6 ft

  • Xasab bu gudd (7 palmes)

    51.8 cm / 20.4 in.

  • Xasab (2 empans / 6 palmes)

    44.5 cm / 17.5 in.

  • Xasab bu gàtt

    38 cm / 15 in.

  • 1 stade romain

    18 de mille romain = 185 m / 606.95 ft

  1. 1 Baaraam (14 palme)

    1.85 cm / 0.73 in.

  2. 2 Palme (4 baaraam)

    7.4 cm / 2.9 in.

  3. 3 Empan (3 palmes)

    22.2 cm / 8.75 in.