Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

4-A

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Bala Yeesu di tàmbali waareem bi

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Bala Yeesu di tàmbali waareem bi

Ñeenti téere yi njëkk ci Injiil ak ni ñu toppantee

Booy jàng li nekk ci tablo bi, nanga xoolaale kàrt yiy wone tukkiy Yeesu ak fi mu waare. Rëdd yi nirook fitt maanaam flèche, wonewuñu yoon yi Yeesu doon aw dëgg-dëgg waaye seen jubluwaay. “ b. ” mu ngi tekki “ booru ”

Bala Yeesu di tàmbali waareem bi

JAMONO JA

BÉRÉB BA

XEW-XEW BA

MACË

MÀRK

LUUG

YOWAANA

3 B.S.J.

Yerusalem,kër Yàlla ga

Malaaka Jibril yégal Sakari juddub Yaxya

   

1:​5-​25

 

b. 2 B.S.J.

Nasaret ; Yude

Malaaka Jibril yégal Maryaama juddub Yeesu ; Maryaama dem seeti mbokkam Elisabet

   

1:​26-​56

 

2 B.S.J.

Diiwaanu Yude bi bare tund

Juddub Yaxya ak bi ñu ko joxee tur ; Sakari yégle na ne ; Yaxya dina dëkk ci màndiŋ

   

1:​57-​80

 

2 B.S.J., b. 1 Okt.

Betleyem

Yeesu juddu ; “ Kàddu gi ñëw, doon nit ”

1:​1-​25

 

2:​1-7

1:14

Booru Betleyem ; Betleyem

Malaaka yégal sàmm yi xibaaru jàmm bi ; malaaka yi sant Yàlla ; sàmm yi seeti liir bi

   

2:​8-​20

 

Betleyem ; Yerusalem

Ñu xaraf Yeesu (bi mu amee 8 fan) ; waajuram yi yóbbu ko ca kër Yàlla ga (bi mu amee 40 fan)

   

2:​21-​38

 

1 B.S.J. walla 1 C.S.J.

Yerusalem ; Betleyem ; Misra ; Nasaret

Ñëwu boroom xam-xam yi ; njaboot ga daw ca Misra ; Erodd rey xale yu góor ya ; njaboot ga jóge Misra ñibsi Nasaret dëkk fa

2:​1-​23

 

2:​39, 40

 

12 C.S.J. Bésu mucc ga

Yerusalem

Bi mu amee 12 at Yeesu di laaj jànglekat ya ca kër Yàlla ga ay laaj

   

2:​41-​50

 
 

Nasaret

Mu dellu Nasaret ; kontine di déggal ay waajuram ; jàng mécce minise ; Maryaama am yeneen ñeenti doom yu góor ak yu jigéen (Macë 13:​55, 56 ; Màrk 6:⁠3)

   

2:​51, 52

 

29, daanaka awril

Màndiŋ, Dexu Yurdan

Yaxya tàmbali waareem bi

3:​1-​12

1:​1-8

3:​1-​18

1:​6-8