Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

4-D

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Waare bu mag bi Yeesu def ca Galile (Xaaj 2)

Xew-xew yi gën a am solo ci dundu Yeesu — Waare bu mag bi Yeesu def ca Galile (Xaaj 2)

JAMONO JA

BÉRÉB BA

XEW-XEW BA

MACË

MÀRK

LUUG

YOWAANA

31 walla 32

Diwaanu Kapernawum

Yeesu joxe ay léeb yu jëm ci Nguur gi

13:​1-​53

4:1-34

8:4-18

 

Dexu Galile

Dalal na ngelaw la ba mu nekkee cig gaal

8:​18, 23-​27

4:35-41

8:22-25

 

Diwaanu Gadara

Mu dàq rab ya ca mbaam-xuux ya

8:​28-​34

5:1-20

8:26-39

 

Xéyna Kapernawum

Faj na jigéen juy xëpp deret ; dekkal na doomu Yayrus

9:​18-​26

5:21-43

8:40-56

 

Kapernawum (?)

Faj na ñaari gumba ak ku luu

9:27-34

     

Nasaret

Ñu dëdduwaat ko ci réewam

13:54-58

6:1-5

   

Galile

Ñetteelu yoon bi mu wëre Galile ; mu yónni ndaw ya ngir yaatal waare bi

9:35–11:1

6:6-13

9:1-6

 

Tiberyàdd

Erodd rey Yaxya ; Erodd jaaxle ndax Yeesu

14:1-12

6:14-29

9:7-9

 

32, booru bésu mucc ga (Yowaana 6:⁠4)

Kapernawum (?) ; Booru dexu Galile féete NE

Ndaw ya waare ba dellusi ; Yeesu dundal 5 000 góor

14:13-21

6:30-44

9:10-17

6:1-13

Booru dexu Galile féete NE ; Senesaret

Nit ñi bëgg ko fal buur ; mu dox ci kaw ndox ma ; mu faj ñu bare

14:22-36

6:45-56

 

6:14-21

Kapernawum

Mu wax ne mooy “ ñam wiy joxe dund ” ; ñu bare weddi ko te bàyyi ko

     

6:22-71

32, bi bésu mucc ga weesoo

Xéyna Kapernawum

Mu wax ci aada nit ñi

15:1-20

7:1-23

 

7:1

Fenisi ; Fukki dëkk ya

Mu faj doomu jenn jigéen ; dundal na 4 000 góor

15:21-38

7:24–8:9

   

Magadan

Joxewul firnde ju dul firndey Yunus

15:⁠39–​16:4

8:​10-​12