Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

LAAJ 8

Ndax Yàlla mooy teg nit ñi coono ?

Ndax Yàlla mooy teg nit ñi coono ?

“ Yàlla dëgg ji mënul sax xalaat a def lu jubadi, Aji-Kàttan ji du xalaat mukk a def lu bon. ”

Ayóoba 34:⁠10, MN

“ Bu la fiir galanee, bul ne : « Yàllaa ko dogal, » ndaxte Yàlla jegewul ak mbon fenn te du fiir kenn. ”

Saag 1:​13

“ Ngeen yenniku ci kawam seen njàqare jépp, ndax ku leen ñeewante la. ”

1 Piyeer 5:7

“ Li Yàlla dige, dina ko def, lu mu yéex yéex ci xalaatu nit. Xanaa kay da leena muñal, ndax bëggul kenn alku, waaye ñépp tuub seeni bàkkaar. ”

2 Piyeer 3:9