Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

LAAJ 9

Lu tax nit ñi di am metit ?

Lu tax nit ñi di am metit ?

“ Léegi nag dégluleen, yéen ñiy wax ne : « Tey walla ëllëg dinañu dem ca dëkk sàngam, def fa at, di fa sàkku xaalis ci jula. » Ndax dangeena xam seen ëllëg ? Luy seen dund ? Xanaa cóola doŋŋ luy naaw ci diir bu gàtt, daldi naaxsaay. ”

Saag 4:​13, 14

“ Bàkkaar ci kenn nit la jaar, dugg ci àddina, indaale fi dee, te dee daldi law ci nit ñépp, ndaxte ñépp a bàkkaar. ”

Room 5:​12

“ Te Doomu Yàlla ji ñëw na, ngir nasaxal jëfi Seytaane. ”

1 Yowaana 3:8

“ Àddina sépp a ngi tëdd ci loxoy Ibliis. ”

1 Yowaana 5:​19