Xalaatu ñi ko génne
Xalaatu ñi ko génne
Kurukaara bu ni rafete mën naa nekk sa bos ba fàww!
Lan nga wara def ngir xéewlu ci? Tont laa ngi sukkandiku ci xeetu xam-xam bu wuuteek xam-xamub nit.
Téere bii dina la dimbali nga jot xam-xam biy jëme ca dund ga dul jeex.