Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

LI NEKK CI TÉERE BII

LI NEKK CI TÉERE BII

Xaaj 1 DAÑU FI NETTALI BI YÀLLA KOMAASEE SÀKK BA BI MU INDEE MBËNN MI, MAANAAM TAW BU METTI CI KOW SUUF SI SÉPP

Xaaj 2 LI XEWOON DIGGANTE TAW BU METTI BI AK BI YÀLLA MUSALEE WAA ISRAYIL CI MISRA

Xaaj 3 DIGGANTE BI ÑU JÓGEE MISRA BA CI JAMANO BUURU ISRAYIL BU JËKK BI

Xaaj 4 DIGGANTE BUUR BU JËKK BI CI ISRAYIL BA BI ÑU NEKKEE JAAM CA BABILON

Xaaj 5 BI ÑU NEKKOON JAAM CA BABILON BA BI ÑU TABAXAATEE MIIRI YERUSALEM

Xaaj 6 YEESU (ISAA), BI MU JUDDOO BA BI MU DEEWEE

Xaaj 7 BI YÀLLA DEKKALEE YEESU BA BI ÑU TËJEE POOL KASO

Xaaj 8 LÉPP LI BIIBËL BI WAX NE DINA AM, MOOY AM