Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  1. Kan moo ñu mën a may doole ak kàttan ? (Yosuwe 1:9 ; Sabóor 68:36)

  2. Naka lañu mënee wéy di dëgëral suñu ngëm ? (Yawut ya 11:6)

  3. Lu tax mu wóor ñu ne dinañu am ndam ci liggéey bi ñu Yexowa sant ? (Ase 2:4-9)

  4. Naka la ñu Yexowa di dooleelee bu ñuy jànkoonteel ak jafe-jafe ? (Sabóor 18:7, 31 ; Kolos 4:10, 11)

  5. Lan moo mën a dimbali ndaw ñi ak jëkkër yi mbaa jabar yi ñu wone ne kilifteefu Yexowa lañu faral ? (Macë 22:37, 39)

  6. Naka lañu mënee “ dëgër ci ngëm ” te “ am pastéef ” ? (1 Korent 16:13 ; Room 15:5 ; Yawut ya 5:11–6:1 ; 12:16, 17)