2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan—Ak ki bànqaas bi yónni
Seetal ci porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bii, waxtaan yi ki bànqaas bi yónni nar a def. Turu ndaje bi mooy: ‘Bégal ci Yexowa’
Bégal ci Yexowa
Porogaraamu suba si ak bu ngoon si, bu ndaje bu mag bu benn fan bi tudd: Bégal ci Yexowa.
Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
Dinañu tontu ci laaj yii ci ndaje bu mag bi.