Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  1. Lu tax ñu mën a ñaan ak kóolute Yexowa mu ñemeloo ñu ? (Sabóor 138:3)

  2. Naka lañu mënee ñeme ni jaamu Yàlla yu tàkku woon ya ? (Jëf ya 4:31)

  3. Naka lañu mënee gën a ñeme ci liggéeyu waare bi ? (1 Tesalonig 2:2)

  4. Lan moo ñuy dimbali ba ñu ñeme bu amee ñu ñuy xiir ci lu bon ? (1 Piyeer 2:21-23)

  5. Ñeme ni karceen, yan barke lay indi ? (Yawut ya 10:35)