Dimaas
“ Ku muñ ba ca muj ga, mucc ” — MACË 24:13
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla No. 121 ak ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Nañu “ daw xél wi nekk sunu kanam, ànd ci ak muñ ”
-
Daw ngir jël ndam li ! (1 Korent 9:24)
-
Nanga tàggat sa bopp bu baax (1 Korent 9:25-27)
-
Nanga yenneeku bépp yen bu amul njariñ (Yawut ya 12:1)
-
Nanga roy royukaay yu baax yi (Yawut ya 12:2, 3)
-
Nanga lekk lekk bu baax (Yawut ya 5:12-14)
-
Nanga naan ndox bu bare (Peeñu ma 22:17)
-
Nanga topp reegalmaa joŋante bi (2 Timote 2:5)
-
Na la wóor ne dinga jël ndam li (Room 15:13)
-
-
11:10 Woy-Yàlla No. 141 ak yégle yi
-
11:20 WAXTAAN BI ÑU JAGLEEL ÑÉPP : “ Kontineel di yaakaar ! ” (Isaïe 48:17 ; Yérémi 29:11)
-
11:50 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
-
12:20 Woy-Yàlla No. 20 ak noppalu bi
NGOON SI
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla No. 57
-
1:50 TIYAATAR BI : Fàttalikuleen soxnas Lóot — Xaaj 3 (Luug 17:28-33)
-
2:20 Woy-Yàlla No. 54 ak yégle yi
-
2:30 “ Kontineel di xaar . . . du tàrde ! ” (Xabakukk 2:3, MN)
-
3:30 Woy-Yàlla No. 129 ak ñaan bu mujj bi