Samdi
“ Bégleen ci yaakaaru ëllëg te muñ bépp tiis ” — ROOM 12:12
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla No. 44 ak ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Ni Yexowa di maye muñ te dëfal xolu. . .
-
Ñi néew doole ak ñi seen yasara yàcciku (ñi xàddi, MN) (Room 15:4, 5 ; 1 Tesalonig 5:14 ; 1 Piyeer 5:7-10)
-
Ñi am soxla ci wàllu koom-koom (1 Timote 6:18))
-
‘ Jirim yi ’ (Sabóor 82:3)
-
Mag ñi (Sarxalkat yi 19:32)
-
-
10:50 Woy-Yàlla No. 138 ak yégle yi
-
11:00 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Tabaxal kër buy yàgg
-
“ Deeleen doylu ” (Yawut ya 13:5 ; Sabóor 127:1, 2)
-
Aarleen seeni doom “ ci lu bon ” (Room 16:19 ; Sabóor 127:3)
-
Yarleen seeni doom “ ciw yoon ” (Kàddu yu Xelu 22:3, 6 ; Sabóor 127:4, 5)
-
-
11:45 SÓOB BI : Nanga “ bañ cee boole genn njàqare ” ! (1 Piyeer 3:6, 12, 14)
-
12:15 Woy-Yàlla No. 79 ak noppalu bi
NGOON SI
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla No. 126
-
1:50 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Nanga roy ñiy muñ
-
Yuusufa (Njàlbéen ga 37:23-28 ; 39:17-20 ; Saag 5:11)
-
Ayóoba (Job 10:12 ; 30:9, 10)
-
Doomu Yefte (Juges 11:36-40)
-
Yérémi (Yérémi 1:8, 9)
-
-
2:35 TIYAATAR BI : Fàttalikuleen soxnas Lóot — Xaaj 2 (Luug 17:28-33)
-
3:05 Woy-Yàlla No. 111 ak yégle yi
-
3:15 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Jàngal muñ ci li Yàlla sàkk
-
Giléem (Yudd 20)
-
Garab yiy sax ci tund yi (Kolos 2:6,7 ; 1 Piyeer 5:9, 10)
-
Lëpp-lëpp (2 Korent 4:16)
-
Picc biy dund ca pôle nord (1 Korent 13:7)
-
Picc bi tudd vanneau (Yawut ya 10:39)
-
Garabu Kàdd (Efes 6:13)
-
-
4:15 Yéen ndaw yi — Seen muñ dafay bégal Yexowa ! (Kàddu yu Xelu 27:11)
-
4:50 Woy-Yàlla No. 135 ak ñaan bu mujj bi