Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Buleen tàyyi ci sàmm yoon wi Kirist tëral !

Buleen tàyyi ci sàmm yoon wi Kirist tëral !

SUBA SI

  • 9:40 Misik

  • 9:50 Woy-Yàlla No. 17 ak ñaan

  • 10:00 Lan mooy yoon wi Kirist tëral ?

  • 10:15 Sàmmal yoon wi Kirist tëral bu dee sax kenn gisu la

  • 10:30 Sàmmal yoon wi Kirist tëral ci liggéeyu waare bi

  • 10:55 Woy-Yàlla No. 70 ak yégle yi

  • 11:05 Yoon wi Kirist tëral — lu tax mu gën ?

  • 11:35 Jébbalu bi ak Sóob bi

  • 12:05 Woy-Yàlla No. 51

NGOON SI

  • 1:20 Misik

  • 1:30 Woy-Yàlla No. 76

  • 1:35 Ay nettali

  • 1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal

  • 2:15 Sàmmal yoon wi Kirist tëral ci biir njaboot gi

  • 2:30 Sàmmal yoon wi Kirist tëral ca lekkool ba

  • 2:45 Woy-Yàlla No. 35 ak yégle yi

  • 2:55 Bëgganteleen ni leen Yeesu bëgge

  • 3:55 Woy-Yàlla No. 13 ak ñaan