Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Buleen tàyyi ci def lu baax !

Buleen tàyyi ci def lu baax !

SUBA SI

  • 9:30 Misik

  • 9:40 Woy-Yàlla No. 77 ak ñaan

  • 9:50 Def lu baax, lu tax mu jafe ?

  • 10:05 Waxtaan bu def ay xaaj : Bul ji ngir sa nafsu

    • Àndal ak sa xel booy jëfandikoo fu ñuy jokoo ci internet ak yeneen nit

    • Nanga feexal sa xol ci fasoŋ bu sell

    • Nanga xeex ñeetaane

    • Nanga wóoral sa ëllëg

  • 11:05 Woy-Yàlla No. 45 ak yégle yi

  • 11:15 Nanga wéy di defal ñépp lu baax

  • 11:30 Jébbalu bi ak Sóob bi

  • 12:00 Woy-Yàlla No. 63

NGOON SI

  • 1:10 Misik

  • 1:20 Woy-Yàlla No. 127 ak ñaan

  • 1:30 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp : Nañu moytu fontoo Yàlla​—ci naka ?

  • 2:00 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal

  • 2:30 Woy-Yàlla No. 59 ak yégle yi

  • 2:40 Waxtaan bu def ay xaaj : Nanga wéy di ji lu soloo ak xelum Yàlla

    • Nanga am tàmmeel yu baax ci njàngum Biibël bi

    • Nanga jëfandikoo li Biibël bi wax ngir xam ni ngay doxale sa dund

    • “ Bul bàyyi sa loxo mu tàyyi ”

  • 3:40 Bu ñu ci sawaree dinañu jariñu — ci lan?

  • 4:15 Woy-Yàlla No. 126 ak ñaan