Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  1. Def lu baax lu tax mu jafe ? (1 Piyeer 5:8 ; Room 12:2 ; Room 7:​21-25)

  2. Lan mooy ji ngir sa nafsu, te naka lañu koy moytoo ? (Galasi 6:⁠8)

  3. Kan lañu war a defal lu baax ? (Galasi 6:⁠10)

  4. Naka lañuy jiwe lu soloo ak xelum Yàlla ? (Galasi 6:⁠8)

  5. Bu ñu ci sawaree, dinañu jariñu — ci lan ? (Gal. 6:9)