2020-2021 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan—Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi

Jëfandikool porogaraam bii ngir mën a déglu waxtaan yi, ci ndaje bu mag bu benn fan bi yépp, bu Seede Yexowa yi ci sa dëkk. Turu ndaje mi mooy: Bégalal xolu Yexowa!

Bégalal xolu Yexowa!

Porogaraamu suba si ak bu ngoon si, bu ndaje bu mag bu benn fan ak wottukat biy wër ci mbooloo yi.

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Dinañu tontu ci laaj yii ci ndaje bu mag bi.