Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
1. Ñun jaamu Yexowa yi, ban cér bu réy lañu am? (Kàddu yu Xelu 27:11)
2. Naka lañu mënee roy Yeesu te bégal xolu Yexowa? (Yowaana 8:29)
3. Naka lañu mënee bégal xolu Yexowa ci suñu liggéeyu waare bi? (Yowaana 15:8)
4. Naka lañu mënee neex Yexowa ci bépp fànn ci suñu dund? (Yowaana 14:31; Waa Efes 6:1-4; Sabóor 35:18; 1 Piyeer 2:12)
5. Naka lañu mënee jànkoonte ak jafe-jafe yi, bañ a xàddi te bañ a daanu ci fiir? (Neyemi 8:10)