Porogaraamu ndaje bu mag bu 2018

Porogaraamu ndaje bu mag bu Seede Yexowa yi bu 2018 ‘ Amal Fit ’! Ndaje bu mag bu Seede Yexowa yi.

Àjjuma

Porogaraamu tey jii moo ngi sukkandiku ci Yosuwe 1:7 —‘ Dëgërlul te feddali sa fit. ’

Samdi

Naka lañu mënee wax Kàddug Yàlla ci lu àndul ak genn tiit ?

Dimaas

Xew-xew yiy ñëw laaj na mbootaayu Yàlla am fit

Li ñi teew war a xam

Amal li nga bëgg a xam ci ndaje bu mag bii.