Àjjuma
‘ Dëgërlul te feddali sa fit ’ — YOSUWE 1:7
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla No. 110 ak Ñaan
-
9:40 WAXTAANU KIY JIITE NDAJE BI : Yexowa — Kiy joxe fit dëgg (Sabóor 28:7 ; 31:25 ; 112:7, 8 ; 2 Timote 1:7)
-
10:10 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Lu tax karceen dëgg yi soxla fit
-
Ci liggéeyu waare bi (Peeñu ma 14:6)
-
Ngir wéy di Sell (1 Korent 16:13, 14)
-
Ngir bañ a bokk ci àddina si (Peeñu ma 13:16, 17)
-
-
11:05 Woy-Yàlla No. 126 ak Yégle yi
-
11:15 TIYAATAR BU ÑUY JÀNG CI BIIBËL BI : “ Amal fit te dëgër te liggéey ” ! (1 Chroniques 28:1-20, MN ; 1 Samwil 16:1-23 ; 1 Samuel 17:1-51)
-
11:45 “ Bépp gànnaay gi ñu jëmale sa kaw du am ndam ” (Isaïe 54:17 ; Sabóor 118:5-7)
-
12:15 Woy-Yàlla No. 61 ak Noppalu bi
NGOON SI
-
1:25 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:35 Woy-Yàlla No. 69
-
1:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Liy wàññi fit ak li koy yokk
-
Ñàkk yaakaar ak am yaakaar (Sabóor 27:13, 14)
-
Bare kaas ak wone ngërëm (Sabóor 27:1-3)
-
Po mu selladi ak liggéeyu waare bi (Sabóor 27:4)
-
Ay àndandoo yu bon ak ay àndandoo yu baax (Sabóor 27:5 ; Kàddu yu Xelu 13:20)
-
Xam-xamu àddina si ak gëstum Biibël bi (Sabóor 27:11)
-
Xel muy werante ak am ngëm (Sabóor 27:7-10)
-
-
3:10 Woy-Yàlla No. 55 ak Yégle yi
-
3:20 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Lu mu leen jaraloon, naka lañu leen barkeele
-
Ananiya, Mikayel ak Asariya (Dañeel 1:11-13 ; 3:27-29)
-
Akilas ak Pirsil (Room 16:3, 4)
-
Ecen (Jëf ya 6:11, 12)
-
-
3:55 “ Takkleen fit yi ; noot naa àddina ” (Yowaana 16:33 ; 1 Piyeer 2:21, 22)
-
4:15 Xarekatu Kirist yu am fit (2 Korent 10:4, 5 ; Efes 6:12-18 ; 2 Timote 2:3, 4)
-
4:50 Woy-Yàlla No. 22 ak Ñaan bu mujj bi