Dimaas
‘ Dëgërlul te am fit, te yaakaarati Yexowa ’ — SABÓOR 27:14
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla No. 73 ak Ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Xew-xew yiy ñëw laaj na ñu am fit
-
Yuuxu gi “ Lépp a ngi ci jàmm, ba ne leww ” (1 Tesalonig 5:2, 3)
-
Sànkute Babilon bu mag mi (Peeñu ma 17:16, 17)
-
Waare xibaar bu mel ni tawu yuur (Peeñu ma 16:21)
-
Bésu songum Gog ak Magog (Ézékiel 38:10-12, 14-16)
-
Bésu Armagedon (Peeñu ma 16:14, 16)
-
Bésu defaraat bu mag bu suuf si (Isaïe 65:21)
-
Bésu seetlu gu mujj gi (Peeñu ma 20:3, 7, 8)
-
-
11:10 Woy-Yàlla No. 8 ak Yégle yi
-
11:20 WAXTAAN BI ÑU JAGLEEL ÑÉPP : Yaakaaru dekki bi day tax a am fit — ci naka ? (Màrk 5:35-42 ; Luug 12:4, 5 ; Yowaana 5:28, 29 ; 11:11-14)
-
11:50 Njàngum La Tour de Garde bu ñu Gàttal
-
12:20 Woy-Yàlla No. 151 ak Noppalu bi
NGOON SI
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla No. 5
-
1:50 FILM BI : Nettalib Yunus — Njàngale bu jëm ci fit ak yërmande (Yona 1-4)
-
2:40 Woy-Yàlla No. 71 ak Yégle yi
-
2:50 Ñi ànd ak ñun ñoo ëpp ñi ànd ak ñoom ! (Deutéronome 7:17, 21 ; 28:2 ; 2 Rois 6:16 ; 2 Chroniques 14:9-11 ; 32:7, 8, 21 ; Isaïe 41:10-13)
-
3:50 Woy-Yàlla ak Ñaan bu mujj bi