Àjjuma
“ YÀLLA DEF NA CI SEEN XOL, NGEEN BËGGANTE ” — 1 TESALONIG 4:9
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla N° 105 ak Ñaan
-
9:40 WAXTAANU KIY JIITE NDAJE BI : “ Mbëggeel amul àpp ”— Ndax lan ? (Room 8:38, 39 ; 1 Korent 13:1-3, 8, 13)
-
10:15 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Moytuleen a teg seen yaakaar ci lu dul wéy !
-
Alal (Macë 6:24)
-
Am tur (Ecclésiaste 2:16 ; Room 12:16)
-
Xam-xamu àddina (Room 12:1, 2)
-
Doole ak taar (Kàddu yu Xelu 31:30 ; 1 Piyeer 3:3, 4)
-
-
11:05 Woy-Yàlla N° 40 ak Yégle yi
-
11:15 AY NETTALI YU ÑUY JÀNG CI BIIBËL BI : Yexowa kontine na di wone mbëggeel (Njàlbéen ga 37:1-36 ; 39:1–47:12)
-
11:45 Yexowa bëgg na ñi bëgg doomam (Macë 25:40 ; Yowaana 14:21 ; 16:27)
-
12:15 Woy-Yàlla N° 20 ak Noppalu bi
NGOON SI
-
1:25 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:35 Woy-Yàlla N° 107
-
1:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Mbëggeel amul àpp bu dee sax . . .
-
Ni ñu ñu yare àndul ak mbëggeel (Sabóor 27:10)
-
Fi ngay liggéeye yombul (1 Piyeer 2:18-20)
-
Ñi nga bokkal lekkool duñu topp santaaney Yàlla (1 Timote 4:12)
-
Danga am feebar bu yàgg (2 Korent 12:9, 10)
-
Danga ndóol (Filib 4:12, 13)
-
Say mbokk dañu lay fitnaal (Macë 5:44)
-
-
2:50 Woy-Yàlla N° 141 ak Yégle yi
-
3:00 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Li Yexowa sàkk dafay fésal mbëggeelam
-
Asamaan si (Sabóor 8:4, 5 ; 33:6)
-
Suuf si (Sabóor 37:29 ; 115:16)
-
Garab yi (Njàlbéen ga 1:11, 29 ; 2:9, 15 ; Jëf ya 14:16, 17)
-
Mala yi (Njàlbéen ga 1:27 ; Macë 6:26)
-
Yaramu nit (Sabóor 139:14 ; Ecclésiaste 3:11)
-
-
3:55 “ Ku Boroom bi sopp, yar la ” (Yawut ya 12:5-11 ; Sabóor 19:8, 9, 12)
-
4:15 “ Solooleen mbëggeel ” (Kolos 3:12-14)
-
4:50 Woy-Yàlla N° 130 ak Ñaan bu mujj bi