Samdi
“ NGEEN WÉER SEEN DUND CI MBËGGEEL ” — EFES 5:2
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla N° 85 ak Ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Ci mbootaay gi, wonleen mbëggeel gu amul àpp
-
Ñiy jiite (1 Tesalonig 5:12, 13)
-
Ñi ñàkk seen jëkkër ak ñi ñàkk seen pàppa (Saag 1:27)
-
Màggat ñi (Lévitique 19:32)
-
Ñi jébbal seen jot gépp ci liggéeyu waare bi (1 Tesalonig 1:3)
-
Doxandéem yi (Lévitique 19:34 ; Room 15:7)
-
-
10:50 Woy-Yàlla N° 58 ak Yégle yi
-
11:00 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Woneleen mbëggeel gu amul àpp ci liggéeyu waare bi
-
Woneel sa mbëggeel ci Yàlla (1 Yowaana 5:3)
-
“ Nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp ” (Macë 22:39)
-
Nanga bëgg Kàddu Yexowa (Sabóor 119:97 ; Macë 13:52)
-
-
11:45 SÓOB BI : Jàngal ci Yeesu lan mooy mbëggeel (Macë 11:28-30)
-
12:15 Woy-Yàlla N° 52 ak Noppalu bi
NGOON SI
-
1:35 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:45 Woy-Yàlla N° 84
-
1:50 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Naka la suñu mbokk yi di wone mbëggeel gu amul àpp ci . . .
-
Afrik (Njàlbéen ga 16:13)
-
Asi (Jëf ya 2:44)
-
Europe (Yowaana 4:35)
-
Bëj-gànnaaru Amerik (1 Korent 9:22)
-
Océanie (Sabóor 35:18)
-
Bëj-saalumu Amerik (Jëf ya 1:8)
-
-
2:55 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Woneleen mbëggeel ci seen biir njaboot
-
Nanga bëgg sa jabar (Efes 5:28, 29)
-
Nanga bëgg sa jëkkër (Efes 5:33 ; 1 Piyeer 3:1-6)
-
Nanga bëgg say doom (Tit 2:4)
-
-
3:35 Woy-Yàlla N° 35 ak Yégle yi
-
3:45 FILM BI : Nettalib Yosiyas : Bëggleen Yexowa te bañleen lu bon — Xaaj 1 (2 Chroniques 33:10-24 ; 34:1, 2)
-
4:15 Jàngal-leen seeni doom ni ñuy wonee mbëggeel (2 Timote 3:14, 15)
-
4:50 Woy-Yàlla N° 134 ak Ñaan bu mujj bi