Àjjuma
« Deeleen bég ci Boroom bi ; maa ngi koy waxati : bégleen ! »—Filib 4:4
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla nº 111 ak ñaan
-
9:40 WAXTAANU KIY JIITE NDAJE BI : Lu tax Yexowa doon « Yàlla bu bég » (1 Timote 1:11, MN)
-
10:15 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Lan mooy yokk mbégte ?
-
• Yombal sa dund (Ecclésiaste 5:12)
-
• Am xel mu dal (Sabóor 19:9)
-
• Def liggéey bu am njariñ (Ecclésiaste 4:6 ; 1 Korent 15:58)
-
• Am ay xarit dëgg (Kàddu yu Xelu 18:24 ; 19:4, 6, 7)
-
-
11:05 Woy-Yàlla nº 89 ak yégle yi
-
11:15 AY NETTALI YU ÑUY JÀNG CI BIIBËL BI : « Yexowa moo leen bégal » (Esdras 1:1–6:22 ; Ase 1:2-11 ; 2:3-9 ; Sakari 1:12-16 ; 2:7-9 ; Zacharie 3:1, 2 ; 4:6, 7))
-
11:45 Bànneexul ci wallu Yexowa (Sabóor 9:15 ; 34:20 ; 67:2, 3 ; Isaïe 12:2)
-
12:15 Woy-Yàlla nº 148 ak noppalu bi
NGOON SI
-
1:30 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:40 Woy-Yàlla nº 131
-
1:45 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Fexeleen mba mbégte am ci biir njaboot
-
• Yeen jëkkër yi, bégleen ci seen jabar (Kàddu yu Xelu 5:18, 19 ; 1 Piyeer 3:7)
-
• Yeen jabar yi, bégleen ci seen jëkkër (Kàddu yu Xelu 14:1)
-
• Yeen waajur yi, bégleen ci seeni doom (Kàddu yu Xelu 23:24, 25)
-
• Yeen xale yi, bégleen ci seeni waajur (Kàddu yu Xelu 23:22)
-
-
2:50 Woy-Yàlla nº 135 ak yégle yi
-
3:00 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ : Li Yexowa sàkk dafay wone ne bëgg na ñu bég
-
• Fulóor yu rafet (Sabóor 111:2 ; Macë 6:28-30)
-
• Lekk bu neex (Ecclésiaste 3:12, 13 ; Macë 4:4)
-
• Kulóor yu rafet (Sabóor 94:9)
-
• Ni nit bindoo (Jëf ya 17:28 ; Efes 4:16)
-
• Lu neex lu ñuy dég (Kàddu yu Xelu 20:12 ; Isaïe 30:21)
-
• Ay mala yu yéeme (Njàlbéen ga 1:26)
-
-
4:00 « Kuy digle jàmm, am mbégte » — Ci naka ? (Kàddu yu Xelu 12:20 ; Saag 3:13-18 ; 1 Piyeer 3:10, 11)
-
4:20 Am diggante bu rattax ak Yàlla mooy maye mbégte bi gën a réy ! (Saag 4:8a ; Habacuc 3:17, 18)
-
4:55 Woy-Yàlla nº 28 ak ñaan bu mujj bi