Dimaas
« Deel bànneexoo [Yexowa] Aji Sax ji, mu may la say nammeel »—Sabóor 37:4
SUBA SI
-
9:20 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
9:30 Woy-Yàlla nº 22 ak ñaan
-
9:40 WAXTAAN BU DEF AY XAAJ :Mën nañu bég bu dee sax dañu . . .
-
• Am ay problem (Room 5:3-5 ; 8:35, 37)
-
• Nekk ci njàqare (2 Korent 4:8 ; 7:5)
-
• Ñuy fitnaal (Macë 5:11, 12)
-
• Xiif (Filib 4:11-13)
-
• Rafle (1 Korent 4:11, 16)
-
• Jankoonte ak ay ngaañ (2 Korent 1:8-11)
-
• Jàkkaarloo ak jaasi (2 Timote 4:6-8)
-
-
11:10 Woy-Yàlla nº 9 ak yégle yi
-
11:20 WAXTAAN BI ÑU JAGLEEL ÑÉPP : Naka ngay amee bànneex ci alal gu àndul ak coono ? (Kàddu yu Xelu 10:22 ; 1 Timote 6:9, 10 ; Peeñu ma 21:3-5)
-
11:50 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
-
12:20 Woy-Yàlla nº 84 ak noppalu bi
NGOON SI
-
1:40 Porogaraamu misik bu ànd ak wideo
-
1:50 Woy-Yàlla nº 62
-
1:55 FILM BI SUKKANDIKU CI BIIBËL BI : Nëxemiya : « Mbégte bu jóge ci Yexowa mooy seen doole » — Xaaj II (Néhémie 8:1–13:30 ; Malachie 1:6–3:18)
-
2:40 Woy-Yàlla nº 71 ak yégle yi
-
2:50 « Deel bànneexoo [Yexowa] Aji Sax ji » ! (Sabóor 16:8, 9, 11 ; 37:4)
-
3:50 Woy-Yàlla bu bees ak ñaan bu mujj bi