Fàttalikuleen soxnas Lòot

Xelal bi Yeesu joxe woon 2 000 at ci ginnaaw, tey la gën a am solo. Seetaanal ni Brian ak Gloria jéemee aar seen njaboot, di topp xelal bi Yeesu joxe woon.

Fàttalikuleen soxnas Lóot — Xaaj 1

Tey, naka la njabootu karceen yi mënee am xel ñaar ci diggante jiital takkute ci Yàlla ak wutum alal ?

Fàttalikuleen soxnas Lóot — Xaaj 2

Lan moo mën a lëndëmal suñu gis-gis ci wàllu ngëm te yàq suñuy jikko yu sell te rafet ?

Fàttalikuleen soxnas Lóot — Xaaj 3

Yeesu dafa nettali nettali boobu ngir ñu jàng ci. Jabaru Lóot mënoon na bañ a mujje noonu. Ñun it, mën nañu bañ a mujje ni moom.